Amul benn buur boo xamni jaamu ko day jur njariñ ñàkk ko jaamu di jur lor kudul Yàlla (الله )✨ Muhammad mooy YONENTEB Yàlla bi .